|
Article on other languages:
|
ab Màkkaanub mbëjfeppal, di ko wax itam màkkaanub m-bataaxal, walla màkkaanub e-mail, am mbooloom ay araf la, muy teewal ab boyotu bataaxalub mbëjfeppal bu nekk ci ab mbaalub (reseau) xibaarfeppal bu mel ne internet. Màkkaanub mbëjfeppal mooy tax ñu man a yónne ab m-bataaxal (bataaxalub mbëjfeppal) kenn nit ci internet. Ci lu bari dañuy jaawatle màkkaanub mbëjfeppal ak màkkaanub web, mi nga xam ne du lenn lu dul ab màkkaanub dalub web. Te sax am na yeneen xeeti màkkaani internet. Baat yiKon liñ lay yónne ci sa màkkaanub mbëjfeppal du ab bataaxal, ndax bataaxal dañ koy jàppe niki lu ñu bind ci këyit ak xalima. Bataaxalub mbëjfeppal la, suñ ko gattale mu doon m-bataaxal (di jàng: miim-bataaxal) |
This article is from Wikipedia. All text is available under the terms of the GNU Free Documentation License.
Mercedes Car
This site monitored by SitePinger.net