|
Bëj-saalum-penku Asi ci goxu Asi la bokk.
Su nu sukkandikoo ci sedatle, bu àdduna bi, gi Mbootaayu Réew yi def, Bëj-saalum-penku Asi benn la ci diwaani Asi.
Bëj-saalum-penku Asi ci lonkoyoonu àdduna bi
Réew ya fa nekk:
Réew yépp yi nekk ci lim gi ci kaw, ba mu des Timoor gu Penku, ay Cër la ñu ci ASEAN: di ab mbootaay bu judd ngir soqali koom-koom mu diwaan bi jaare ko ci jappalante.
|